K - k

kàdd g- *   n. Acacia albida, MIMOSACÉES. expèce d'arbre *; Baumart; species of tree. Note: acacia épineux

kàdd /ne/ *   adv.idéo.spéc. être raide; exprime la manière d'être raide *; être rigide; steif sein; to be stiff; to be rigid. Naka la Buur Yerbowam dégg na góoru Yàlla ga xaacoo, gëdd sarxalukaayu Betel ba, mu daldi koy tàllal loxoom, foofa ca sarxalukaay ba. Mu ne: «Jàppleen ko!» Waaye loxo ba mu ko tàllal ne kàdd, manatu koo bank. [1Ki 13.4]

kër g- *   n. 1 • maison *; Haus; house.

2 • famille *; Familie; family.

boroom kër   chef de famille *; Familienoberhaupt; head of the family.

3 • dynastie; Dynastie; dynasty.