L - l

lawiir   n. From: fr. levure; Hefe; yeast. Lóot nag soññ leen, ba ñu dal këram, mu ganale leen. Lóot da leena berndeel, lakkal leen mburu mu amul lawiir, ñu lekk. [Njàlbéen ga / Gn 19.3]

léebu b- *   n. proverbe *; Sprichwort; proverb. Nen du bëreek doj. [léebu wolof]

lëf k- *   n. quelque chose; chose *; Sache; etwas; thing; something. Variant: këf k-.

as lëf   un tout petit peu; etwas; ein kleines bißchen; a little bit.

lolli w- *   n. période post-hivernale; saison des récoltes; automne *; Periode nach der Regenzeit; Erntesaison; Herbst; period after the rainy season; harvest time; autumn. Du nu ngi ci lolli, ci ngóobum bele? Dinaa ñaan ci Aji Sax ji, mu taw, di dënnu. Su boobaa dingeen xam ci lu wér ne, def ngeen lu ñaawa ñaaw ci kanam Aji Sax ji, keroog ba ngeen sàkkoo buur.» [1.Samiyel / 1Sa 12.17] Usage: oct.-janvier

lox *   v.i. trembler; frissonner; grélotter *; zittern; schlottern; bibbern; to shiver; to shudder; to jitter. Isaaxaa ngay lox, bay rag-ragi, daldi ne ko: «Kan? Ana ku rëbbi woon nag, indil ma, ba ma lekk ba noppi? Ñaanal naa ko bala ngaa ñëw. Te dina barkeel moos.» [Njàlbéen ga / Gn 27.33]