Ñ - ñ

ñaanal *   v.t. prier pour quelqu'un; demander quelque chose pour quelqu'un *; für jemanden beten; für jemanden etwas erbitten; to pray for someone; to ask for something for someone. Ba Daawuda noppee ca sarax yay lakk ba jeex ak saraxi cant ya ci biir jàmm, ñaanal na mbooloo ma ci turu Aji Sax, jiy Boroom gàngoori xare yi. [2Sa 6.18] Usage: ME: Dieu béni (barke) l'homme. Le père prie (ñaanal) pour l'enfant.

ñax m- *   n. herbe *; paille (beaucoup); Gras; Kraut; Kräuter; grass; herbs; herbage; straw.

ñax lañu   what Senegalese say of F.C. tribes.

ñax mu sax m-   herbe en train de pousser; wachsendes Gras; growing grass.

ñax mu tooy m-   herbe mouillé, frais, vert; frisches, grünes Gras; green, fresh grass.

xeeti ñax: ndinga; ngooñ; njargandal; njëmbu; sarguf; xaaxaam (ME)   Note: Senegal carried Islam to other countries; Islam's following is greater outside of Senegal; carried Islam to Cameroon; Culture is superior to those who "lekk golo". ???