Pour mieux lire ce livre…
L'alphabet officiel dont on se sert est facile à lire. Les seuls symboles qui présentent une certaine difficulté sont les suivants:
j | se trouve dans | la paix | –jàmm (ji) |
et | dernier | –mujj | |
c | se trouve dans | le couscous | –cere (ji) |
et | descendre | –wàcc | |
ñ | se trouve dans | tous | –ñépp |
et | refuser | –bañ | |
x | se trouve dans | savoir | –xam |
et | la main | –loxo (bi) | |
ë | se trouve dans | l'œil | –bët (bi) |
et | demain | –ëllëg | |
ŋ | se trouve dans | la mâchoire | –ŋaam (wi) |
et | seulement | –doŋŋ |
Une différence existe entre a et à
baigner | –sang | revêtir | –sàng |
l'encensoir | –and (bi) | accompagner | –ànd |
La voyelle est doublée pour indiquer la longueur
valoir | –jar | passer par | –jaar |
être propre | –set | chercher | –seet |
le cœur | –xol (bi) | regarder | –xool |
le nom | –tur (wi) | répandre | –tuur |
La voyelle est accentuée pour indiquer la fermeture
souper | –reer | être perdu | –réer |
jeûner | –woor | être sûr | –wóor |
Li nuy bëgga lim lu nu tëral la, bëgg cee déggook bokki jàngkat yu tedd yi, ngir déggin wi leer, ba deesu ko jaawatle.
Nanu ràññee…
nanu ak nañu
Dees na wax: «(Nun) war nañoo dem» (n bi am maas bii: ˜ ).
Waaye danu koo taamoo binde nii:
«(Nun) war nanoo dem,»
ngir ñu bañ koo jaawatleek: «War nañoo dem (ñoom).»
naa ak na
Bu loolu weesoo, dees na wax: «(Moom) war naa dem.»
Waaye danu koo taamoo binde nii:
«(Moom) war na dem,»
ngir ñu bañ koo jaawatleek: «War naa dem (man).»
Boo gisee màndarga mii – xamal ne kàddu gee yeggul. Dafa dog, mbaa muy wax ju ñu junj rekk.
Mbind yi ñu ràññale ak yi ñu dijjal, bokkul ci mbindum Yàlla mu sell, mi ñu jukkee ci téere yu jëkk ya.
Boo gisee baat bu ñu tofal araf bu tuuti bu mel nii *, seetal lu muy tekki ci suufu xët mi.
Boo gisee tomb bii ci boppu baat, seetal lu muy tekki ci Leeral yi, fi téere biy waaja jeexe.