Dégtalub Tawreetu Musaa : Njàlbéen ga
(La Genèse, 2003)
Fii ngay yebe téere bi ci fisié yu ñu mana déglu
(176 mo)
Yàlla sàkk na àddina fal ci nit
(1:1)
Yàlla dugal na nit Àjjana jox ko ndigal
(2:4)
Yàlla dàq na nit Àjjana
(3:1)
Kayin rey na Abel
(4:1)
Askanu Kayin
(4:17)
Askanu Aadama ba ci Nóoyin
(5:1)
Yàlla fas na yeene tas àddina
(6:1)
Askanu Nóoyin
(6:9)
Yàlla musal na Nóoyin ci mbenn mi
(7:1)
Nóoyin génn na gaal gu mag ga
(8:1)
Yàlla fas na kóllëre ak Nóoyin
(9:1)
Mbirum Nóoyin ma ak i doomam
(9:18)
Xeet yi sosoo ci doomi Nóoyin
(10:1)
Li jëm ci askanu Yafet
(10:2)
Li jëm ci askanu Xam
(10:6)
Li jëm ci askanu Sem
(10:21)
Yàlla safaan na làkku àddina mu jaxasoo
(11:1
Askanu Sem maamu Ibraam
(11:10)
Askanu Teraa baayu Ibraam
(11:27)
Yàlla sant na Ibraam mu gàddaay
(12:1)
Ibraam dem na réewu Misra
(12:10)
Ibraam ak Lóot teqalikoo nanu
(13:1)
Digeb Aji Sax ja ak Ibraam
(13:14)
Ibraam wallu na Lóot (14:1)
Melkisedeg ñaanal na Ibraam barke
(14:17)
Yàlla fas na ak Ibraam kóllëre
(15:1)
Ismayla juddu na
(16:1)
Yàlla soppi na turu Ibraam
(17:1)
Xaraf mandargaal na kóllëreg Yàlla
(17:9)
Ibraayma ak ganam ña (18:1)
Ibraayma tinul na waa Sodom
(18:16)
Bàkkaari waa Sodom
(19:1)
Lóot genn na Sodom
(19:12)
Yàlla tas na dëkk yooyu di Sodom ak Gomor
(19:23)
Mbirum Lóot ak doomam yu jigéen ya
(19:30)
Lu jëm ci Ibraayma ak Abimeleg
(20:1)
Juddub Isaaxa
(21:1)
Saarata jote na ak Ismayla ak Ajara
(21:8)
Ibraayma waatoo na ak Abimeleg
(21:22)
Yàlla nattu na Ibraayma
(22:1)
Askanu Naxor
(22:20)
Ibraayma jënd na suuf ca Kanaan
(23:1)
Isaaxa jël na Rebeka soxna
(24:1)
Ibraayma nelaw na
(25:1)
Askanu Ismayla
(21:12)
Askanu Isaaxa doomu Ibraayma
(25:19)
Esawu sàggane na céram
(25:27)
Isaaxa nëbbu na waa Gerar ngir mucc
(26:1)
Isaaxa fas na kóllëre ak Abimeleg
(26:12)
Esawu jël na ay soxna
(26:34)
Yanqóoba jekk na Esawu ci ñaanam
(27:1)
Yanqóoba dem na ca nijaayam
(27:41)
Esawu jel na yeneeni soxna
(28:6)
Yanqóoba sartoo na ak Yàlla
(28:10)
Yanqóoba daje na ak Rasel
(29:1)
Njaboot gi Yanqóoba am
(29:31)
Yanqóoba woomle na
(30:25)
Yanqóoba toxu na jëm Kanaan
(31:1)
Laban dabi na Yanqóoba
(31:22)
Yanqóoba ragal na daje ak Esawu
(32:4)
Bëreb Yanqóoba bu réy ba
(32:23)
Yanqóoba ak Esawu daje nañu ci jàmm
(33:1)
Tooñ nanu Diina doomu Yanqóoba
(34:1)
Yanqóoba sanc na Betel
(35:1)
Ben-yamin juddu na Rasel faatu
(35:16)
Doomi Yanqóoba ya
(35:22)
Isaaxa nelaw na
NGJ01 Askanu Esawu
(35:27)
Askanu Seyir
(36:20)
Buur ya jëkk a falu ca Edom
(36:29)
Yuusufa gént na lu yéeme
(37:1)
Yuda ak Tamar ak seen askan
(38:1)
Jaay nañu Yuusufa jawriñu Firawna
(39:1)
Soxnas Potifaar fexeel na Yuusufa
(39:7)
Tej nanu Yuusufa kaso
(39:19)
Yuusufa firi na génti ñaar ña ñu tëj
(40:1)
Firawna gént na
(41:1)
Yuusufa firi na génti Firawna
(41:14)
Firawna fal na Yuusufa mu jiite Misra gépp
(41:37)
Magi Yuusufa ya dem nañu Misra
(42:1)
Yuusufa xupp na magma ya
(42:7)
Doomi Yanqóoba ya dellu nañu Kanaam
(42:24)
Magi Yuusufa ya yóbbu nañu Ben-yamin
(43:1)
Magi Yuusufa ya dellu nañu Misra
(43:15)
Yuusufa nattu na ay magam
(44:1)
Yuda tinul na Ben-yamin ca Yuusufa
(44:14)
Yuusufa xàmmiku na ay magam
(45:1)
Firawna woo na Yanqóoba Misra
(45:16)
Yanqóoba dem na Misra
(46:1)
Njabootu Yanqóoba gi ñëw Misra
(46:8)
Yanqóoba gis na Yusuufa
(46:28)
Yuusufa nuyoole na ay bokkam Firawna
(47:1)
Saytub Yuusufa ca xiif ba
(47:13)
Ati Yanqóoba yu mujj ya
(47:27)
Israyil ñaanal na Efrayim ak Manase
(48:1)
Yanqóoba taago na (Kàdduy Yanqóoba yu mujj ya)
(49:1)
Yanqóoba nelaw na
(49:29)
Yuusufa rob na Yanqóoba réewu Kanaan
(50:1)
Magi Yuusufa yaa ngi jégglu
(50:15)
Yuusufa nelaw na
(50:22)