Cardiovascular and Respiratory Systems
| Wolof | English | French | 
| xol bi | heart | le coeur | 
| xëtër wi | lung | le poumon | 
| pottax bi | trachea | la trachée | 
| waruwaay bi | vessel | le vaisseau | 
| siddiit gi waruwaayu deret bi  | 
blood vessel | le vaisseau sanguin | 
| tëf-tëfu xol bi | heartbeat | le battement de coeur la pulsation  | 
  
| noyyi/ nokki | to breathe | respirer | 
| xetu gémmiñ gi bàqatay ki  | 
bad breath | la mauvaise haleine | 
| xiix appaat  | 
to pant, to puff | haleter | 
| sëqët, sëqat | to cough | tousser | 
| sëqët su jàppoo | coughing fit | |
| yuqóol; yuqóol gi | hiccoughs | avoir le hoquet | 
| ñandaxit/ñendaxit wi | nasal mucus | le mucus nasal; morve | 
| xaaxtëndi bi/xaaxtandiku | sputum/phlegm | le crachat; les expectorations | 
| rattaxit wi | mucus | la glaire | 
Haemopoetic System
| yóq bi / yuq gi | bone marrow | la moelle osseuse | 
| deret ji | blood | le sang | 
| lumbu deret wi | blood clot | le caillot du sang | 
| nàcc | to bleed | saigner | 
| xëpp deret | haemorrhage | l'hémorragie (f) | 
| xeetu deret ji | blood group | le groupe sanguin | 
| kaaraange gi | immunity | l'immunité (f) | 
Digestive System & Abdominal Organs
| biir gi bàq gi  | 
    stomach | l'estomac (m) | 
| butit bi | intestine | l'intestin (m) | 
| res wi | liver | le foie | 
| wextan wi | gallbladder, bile | la vésicule bilaire; la bile | 
| gàddaam gi ndese mi  | 
spleen | la rate | 
| xelliwaan bi; mbuus mi | gland | la glande | 
| xelliwaanu lor bi | salivary gland | la glande salivaire | 
| xelliwaanu bàq bi | stomach gland | |
| xelliwaanu reesal bi | digestive glands | le suc digestif | 
| xelliwaanu butit bi | intestinal gland | 
| tëflit bi lor wi  | 
    saliva | la salive | 
| yuut gi | dribble | la bave; baver | 
| wextan wi | bile | la bile | 
| xellitu bàq wi | gastric juices | le suc gastrique | 
| xérñéññ gi | gastric acidity | acidité gastrique | 
| xellitu reesal wi | digestive juices | 
| day yi puub yi jonkan yi  | 
    faeces | les fèces (f); le caca; l'excrément (m)  | 
  
| doxat wi / doxot wi | fart, pass wind; to pass wind | le pet; péter; lâcher des vents | 
| géex | to belch | éructer; roter | 
| waccu yi; waccu | vomit; to vomit | la vomissure; vomir | 
| fër | to have indigestion | avoir l'indigestion (f) | 
| xel muy teey | nausea | la nausée | 
| gall | to regurgitate | régurgiter | 
| biir bu jooy biir bu wax  | 
stomach rumbles | 
Urinary System
| roño bi dëmbeen bi  | 
    kidney | le rein | 
| butitu taaw bi | ureter | l'uretère (m) | 
| paftan mi | bladder | la vessie | 
| saw mi seben bi  | 
    urine | l'urine (f) | 
| kew gi | calcium stone; calculus; white clay | le calcul; le calcaire | 
| téju | to have urinary retention | la rétention | 
Locomotor and Nervous Systems
| yóor gi/ yuur gi | brain | le cerveau | 
| siddiit gi | nerve, blood vessel, muscle | le nerf | 
| yax bi | bone | l'os (m) | 
| tenqo bi | joint | l'articulation (f) | 
| suux wi siddiit gi  | 
muscle | le muscle | 
| caas gi buumu suux bi  | 
tendon, ligament | le tendon, le ligament | 
Skin
| der wi | skin | le peau | 
| ras-ras bi; ras | wrinkle; to have wrinkles | la ride; être ridé | 
| rew ji | stretch mark | la vergeture | 
| futt | to have a blister | avoir une ampoule | 
| daar bi | callas | le durillon | 
| légét wi | scar | la cicatrice | 
| tut wi | keloid scar | une cicatrice en relief | 
| àkk wi | scab/ crust | la croûte | 
| jib ji | depigmentation of skin | la dépigmentation de l'épiderme | 
| xub | desquamation | se desquamer | 
| booy, booy-booy bi | rash, graize | la rougeur de la peau, l'érythème | 
| putte bi | pustule, furuncle | la pustule, le furoncle | 
| jamuc bi/jumuc/jamoc | pustule, furuncle on the face | pustule, furoncle de visage | 
| góom bi | wound | la blessure, la plaie | 
| dana bi | ulcer | l'ulcère (m); la plaie suppurante | 
| béy bi | hives | l'urticaire (f) | 
| soccent/ soccet bi | wart/ moluscum contagiosum | la verrue | 
| kabiyàdd gi; kabiyàdd | ringworm; to have ringworm | la teigne; avoir la teigne | 
| ràmm ji; ràmm | scabies; to have scabies | la gale; avoir la gale | 
| teeñ wi; teeñ | louse; to have lice | le pou; avoir les poux | 
| fel wi | flea | la puce | 
| pawax bi | membrane | la membrane | 
| càqar bi | lymph node | le ganglion; glandes lymphatiques | 
| suux wi | flesh | la chair | 
| dónj | lump | l'excroissance (f); la bosse; le nodule; la nodosité  | 
| giir gi | mycetoma, maduromycosis | 
| xeeru baat wi | inflamed cervical lymph node | la glande lymphatique enflammée | 
| somp wi; somp | hangnail; have a hangnail | envies, petites peaux à la naissance de l'ongle | 
| dëtt ji mbér bi  | 
    pus | le pus |