S - s

saatlu *   v. avoir eu son dernier enfant *; das letzte Kind geboren haben; to have given birth to one's last child.

saawo s- *   n. 1 • sentier qu'empruntent les troupeaux *; Viehpfad; path used by herds.

2 • traînée; sillon; trace *; Pfad; Spur; Furche; trail; furrow; trace. Congum Yonatan mu jëkk mooma, mook kay gàddu ngànnaayam daane nañu ca lu tollook ñaar fukki góor ci dénd bu wara tollook saawow nag. [1Sa 14.14]

niti saawu   shepherds.

sàppe s- *   n. rangée de fidèles à la prière *; Reihe von Gläubigen beim Gebet; row of believers during prayer. Ñu teg ay banti seedar ci kaw gàllu, yi jën yi yenu: muy ñeent fukki gàllu ak juróom, sàppe bu nekk fukki gàllu ak juróom. [1.Buur ya / 1Ki 7.3]

séetu   v. achever la semaine des noces; Hochzeitswoche halten; to finish the bridal week. Laban ne ko: «Rakk jëkka séy mag daal, du aada fii. Séetul ak kii, ba ayu-bésam mat, ma door laa jox ki ci des, soo ma dee liggéeyaatal diiru juróom ñaari at.» [Njàlbéen ga / Gn 29.26-27] Damay séetu. I'm marrying / in marriage week. [MB]

seetu b- *   n. miroir; glace *; Spiegel; mirror.

sëq *   v.t. 1 • prendre une poigneée de; prendre à pleines mains *; eine Handvoll nehmen von; mit vollen Händen nehmen; to take a handful; to take with full hands.

2 • empoigner *; ergreifen; to grasp. Yaw Yuda, mi say doomi baay di taggeji, ngay sëqi sa ndoddi noon, sëgal leen, sa doomi baay a lay sujjóotal. [Njàlbéen ga / Gn 49.8]

sibbir s- *   Variant: sibir *. n. surlendemain *; übernächster Tag; two days later; two days after. Usage: rare

sol *   v.t. 1 • porter; passer; mettre *; tragen; hineinschlüpfen; anziehen, angezogen sein; to wear; to slip on;; to put on. Solal déglukaay bi! Setze den Kopfhörer auf! [MÑ] Usage: vêtement habit, chaussures; Kleidung, Schuhe

2 • introduire dans; remplir *; verser dans une bouteille; einführen in; füllen; gießen; to introduce into; to fill; to pour. Solal ma diwlin

3 • insuffler *; einblasen; vermitteln; to inspire.

4 • gaver *; stopfen; vollstopfen; to force-feed.

sonk m- *   n. Typha australis et T. elephantina, TYPHACÉES. From: Fr: jonc. roseau de la Passion *; Rohrkolbengewächs, Röhricht; marsh herb, typha. Note: unknown in Baol

sóor *   v.t. mettre le riz dans la marmite; verser le riz à cuire dans la marmite bouillante *; Reis in den Topf mit kochendem Wasser geben; zu kochenden Reis in den Topf schütten; to put the rice into the cooking pot; to pour the rice into the boiling cooking pot.

suux w- *   n. chair; muscle *, chair sans os; Fleisch; Muskel; flesh; muscle. Looloo tax ba tey jii bànni Israyil duñu lekk suux, wi jàpp ci tenqob mooco, ndax li moocob Yanqóoba summikoo woon ca suuxu tenqo ba. [Njàlbéen ga / Gn 32.33]