Fii
ngay jànge walla yebe téerey Kàddug Yàlla yi ñu lim
Kàddug
Yàlla gi (La Bible)
Téere
bu mag, biy
kàddug Yàlla gépp, juróom benn fukki téere laak juróom benn. Yàlla moo
tànn ay yonent ak yeneeni nit ci diiru junniy at ak juróomi
téeméer, xiir léen ci bind kàddoom.
Xaaj 1: Téereb kóllëre gu jëkk gi
(Ancien Testament)
Kóllêre gu jëkk
gi, di xaaj bu jëkk ci Kàddug Yàlla gi (Xaaj 2: Téereb Injiil, Nouveau Tesetament)
Tawreet
Yonent Yàlla Musaa moo bind Tawreet.
Mooy juróomi téere yi jiitu ci Kàddug Yàlla gi.
► Njàlbéen
ga (Genèse, 2016) Yeb ko
Njàlbéen
ga mooy téere bi jëkk ci Kàddug Yàlla gi, te moo jiitu ci Tawreetu
yonent Yàlla Musaa.
Ñaareelu xaaju Tawreet, di téereb
Mucc ga, moo wéyal jaar-jaari bànni Israyil, jële ko fa
ko téereb Njàlbéen ga bàyyi woon.
► Sarxalkat
yi (Lévitique, 2016) Yeb ko
Ñetteelu xaaj bu Tawreetu Musaa jëm
ci sasu Sarxalkat yi.
► Màndiŋ ma (Nombres,
2017) Yeb
ko
► Baamtug
Yoon wi (Deutéronome, 2017) Yeb
ko
Téerey
Cosaan yi (livres
historiques)
(Josué, nu ngi
koy négandiku)
(Juges, nu ngi koy négandiku)
► Ruut (Ruth, 2016) Yeb ko | Seetaan ko ci wideyo | Déglu ko
► 1 Samyel (1 Samuel,
2016) Yeb ko | Déglu ko
► 2 Samyel (2 Samuel,
2016) Yeb ko | Déglu ko
► 1 Buur ya (1 Rois, 2016) Yeb ko | Déglu ko
► 2 Buur ya (2 Rois,
2016) Yeb ko
(1 Chronique, nu ngi koy négandiku)
(2 Chronique, nu ngi koy négandiku)
► Esra (Esdras, 2016) Yeb ko
► Neyemi (Néhémie, 2016) Yeb ko
► Esteer (Esther, 2016) Yeb ko | Seetaan
ko ci wideyo | Déglu ko
Téerey Taalif yi
► Ayóoba (Job, nu ngi
koy négandiku) Yeb
ko | Déglu ko
► Sabóor
(Psaumes, 2016) Yeb
ko | Déglu ko
► Kàddu
yu Xelu (Proverbes, 2016) Yeb ko
► Kàdduy
Waare (Ecclésiastes, 2016) Yeb ko
► Ngën-gi-woy
(Cantique, 2016) Yeb ko
Téerey Waxyu yi
► Esayi (Ésaïe, 2019) Yeb ko
► Yeremi (Jérémie, 2016) Yeb ko
► Kàdduy Jooytu (Lamentations,
2016) Yeb ko
► Esekiyel (Ézéchiel, 2016) Yeb ko
► Dañeel (Daniel, 2016) Yeb ko
(Osée, nu ngi koy négandiku)
(Joël, nu ngi koy négandiku)
► Amos (Amos, 2016) Yeb ko
(Abdias, nu ngi koy négandiku)
► Yunus (Jonas, 2016) Yeb ko | Seetaan
ko ci wideyo | Déglu ko
(Michée, nu ngi koy négandiku)
(Nahum, nu ngi koy négandiku)
(Habakuk, nu ngi koy négandiku)
(Sophonie, nu ngi koy négandiku)
(Aggée, nu ngi koy négandiku)
(Zacharie, nu ngi koy négandiku)
(Malachie, nu ngi koy négandiku)
Xaaj
2: Téereb Téereb kóllëre gu mujj gi
Jàng
ko. Yeb ko |
Déglu
ko.
(Xaaj 1:
Téereb Yonent yi, Ancient Testament)
Kóllëre gu bees gi mooy xaajub
ñaareel bu Kàddug Yàlla gi. Mooy kóllëre gi Yàlla fas ak nit, te mu sottee ci Almasi Yeesu.
Waxi yonent yi jëm ci Almasi
Liy yombal njàngum téere bii
Nanu ràññee
Copyright
Ubbite
gi
Leeral yi
Xibaaru Jàmm bi ci Almasi Yeesu
Xibaar bu bees bi di Kàddu yiy biral
dundu Almasi bu sell bi Yeesu, Yàlla jaarale na ko ca gaayam yu tedd yi :
► MACË (Évangile
selon Matthieu, 2010)
► MÀRK (Évangile
selon Marc, 2010)
► LUUG (Évangile
selon Luc, 2021)
► YOWAANA (Évangile
selon Jean, 2010)
Jëfi
ndaw yi
Kàddug Yàlla tasaaroo na ci àddina :
► JËFI NDAW YA KIRIST
YÓNNI (Les Actes des Apôtres, 2019)
Bataaxal yi
Kàddu yiy biral yaatuwaayu ngëneel
yi ci Kirist, ni ko ndawam yu tedd yi binde :
Bataaxal yi Yàlla may Póol, mu bind ko :
► WAA ROOM (Épitre
de Paul aux Romains)
► 1 WAA KORENT (Premier
Épitre de Paul aux Corinthiens)
► 2 WAA KORENT (Segond Épitre de Paul aux
Corinthiens)
► WAA GALASI (Épitre
de Paul aux Galates)
► WAA EFES (Épitre
de Paul aux Éphésiens)
► WAA FILIB (Épitre
de Paul aux Philippiens)
► WAA KOLOS (Épitre
de Paul aux Colossiens)
► 1 WAA TESALONIG (Premier
Épitre de Paul aux Thessaloniciens)
► 2 WAA TESALONIG (Second
Épitre de Paul aux Thessaloniciens)
► 1 TIMOTE (Premier
Épitre de Paul à Timothée
► 2 TIMOTE (Segond
Épiitre de Paul à Timothée)
► TIT (Épitre
de Paul à Tite)
► FILEMON (Épitre
de Paul à Philémon)
► Bataaxal bi
jëm ca YAWUT
YA (Épitre
aux Hébreux)
► Bataaxal bi
Yàlla may SAAG,
mu bind ko (Épitre
de Jacques)
Bataaxal yi Yàlla may Piyeer, mu bind ko (Épitres
de Pierre)
► 1 PIYEER (Permier
Épitre de Pierre)
► 2 PIYEER (Segond
Épitre de Pierre)
Bataaxal yi Yàlla may Yowaana, mu bind ko (Épitres
de Jean)
► 1 YOWAANA (Permier
Épitre de Jean)
► 2 YOWAANA (Segond
Épitre de Jean)
► 3 YOWAANA (Troisième
Épitre de Jean)
► Bataaxal bi
Yàlla may YUDD,
mu bind ko (Épitre
de Jude).
Téereb Peeñu mi
Kàddu yiy xamle mbir yi wara ñëw te Yeesu
Kirist won ko Yowaana
ci biir peeñu
► PEEÑU MI (La
Révélation de Jésus-Christ à Jean)
|