X - x

xaj b- *   n. chien *; Hund; dog. Xaj saay-saay la. [ME] Cim, yaay sama xaju baay! Lu ma def, nga def ko! [ME]

xale b- *   Variant: xaleel b-. n. enfant; jeune; gosse *; Kind; Jugendlicher; Gör; child; young person: kid. Ba mu ko waxee loolu, Laban ne ko: «Jigéen ñii samay doom lañu, xale yii di samay sët, te gétt gii sama gétt a; lu fi nekk maa ko moom. Ñii di sama doom yu jigéen, nu ma leen di def tey, ñoom ak seeni doom? [Njàlbéen ga / Gn 31.43] Usage: moins de 35 ans Note: terme d'évitement: "bant-yàlla"

xalima g- *   n. From: ar. 1 • calame; plume taillée; plume ou bâtonnet de bois taillée servant à lécriture; plume calame *; Schreibrohr; angespitzte Feder; Federkiel; type of pen; sharpened feather; quill. Usage: pen for writing the Koran

2 • écriture; calligraphie; manière personelle d'écrire *; Schrift; Kalligrafie; Handschrift; writing; calligraphy; hand writing.

3 • pouvoir de l'écriture *; Macht der Schrift; power of writing.

xañtu *   v.t. suivre la trace *; der Fährte folgen; to follow the trail.

xar-kanam g- *   n. visage; physionomie; mine *; Gesicht; Physiognomie; Gestalt; Gesichtsausdruck; face; physiognomy; look. Isayi yónnee, ñu indi ko. Ma nga def ku xees, rafet i bët, xar-kanam ba jekk. Aji Sax ji ne Samiyel: «Jógal diw ko, kii la.» [1Sa 16.12] Du kenn sax ku am sikk kuy agsi ba fii, du gumba, du kuy soox, du ku xar-kanamam am sikk mbaa ku cér yi sutaate. [Lv 21.18]

xasab b- *   n. From: ar. coudée (mesure de longueur) *; Elle (Längenmaß); cubit; yard; span; fingure span. «Guddaayu ëtt ba téeméeri xasab la, yaatuwaay ba di juróom fukk wet gu nekk, taxawaay ba di juróomi xasab, sor ya di yu ñu ràbbe wëñ gu ëccu ba sew. Na tegu ya di yu xànjar. [Ex 27.18] Usage: MD: la mesure pour mesurer la longueur du tombeau Note: doigts à la coude

xatax b-   Variant: xetax b-. n. vannure de paille de mil; poils urticants veloutés qu'on trouve sur la coque du fruit due baobab ou sur les épis de céréales comme le mil; * paille, ci qui reste quand on a pilé le mil; Spreu von Hirsestroh; samtartige, nesselnde Haare z.B. an der Hülle der Baobabfrucht oder an den Getreideähren wie der Hirse; chaff of millet straw; velvety hair as on the shell of the baobab fruit or on the ear of cereals like the millet. Loolu dalul moos ku bon, kay mel ni xatax bu ngelaw li wal. [Ps 1.4]

xëbal   v.t. 1 • faire mousser *; zum Schäumen bringen; to cause to foam.

2 • menacer (quelqu'un) pour (lui) faire peur; faire des menaces en l'air *; (jemanden) bedrohen, um (ihm) Angst zu machen; Scheindrohungen aussprechen; Drohungen zum Schein aussprechen; to threaten (someone) in order to make (him) afraid; to pretend making threats. Xëbalu bukki saful waxambaanew gaynde. [ME] See: xupp.

xérém y-   See main entry: xërëm. n. From: héb. objets de culte (traditionnel); fétiches; idoles; totems; reliques *; idole sous forme de statue; (traditionelle) Kultobjekte; Fetische; Idole; Totems; Reliquien; Götzenstatue; objects of (traditional) worship; fetishes; idols; totems; relics; idol as a figure.

nataali xërëm   idoles dessinés; images; gemalte Idole; Götzenbilder; painted idols; images.

xetax b- *   n. vannure de paille de mil *; Spreu von Hirsestroh; chaff of millet straw.

xettali *   See main entry: xettli. v.t. tirer d'embarras; voler au secours de; tirer une épine du pied *; secourir; retirer de; aus der Klemme helfen; jemandem zu Hilfe eilen; einen Dorn aus dem Fuß ziehen; Hilfe leisten; retten; ziehen aus; to get somebody out of a tight spot; to rush to somebody's aid; to pull outa thorn of the foot; to help; to rescue; to withdraw; to get from. Te bés, ba ma Yàlla génnee sama kër baay, may wëndeelu, dama koo waxoon ne ko: “Déglul, li ngay def soo ma bëggee xettli, mooy lii: fépp fu nu dem, nanga wax ne sa càmmiñ laa.”» [Njàlbéen ga / Gn 20.13] Note: plus profond que "dimbali"

xettli   Variant: xettali. v.t. tirer d'embarras; voler au secours de; tirer une épine du pied *; secourir; retirer de; aus der Klemme helfen; jemandem zu Hilfe eilen; einen Dorn aus dem Fuß ziehen; Hilfe leisten; retten; ziehen aus; to get somebody out of a tight spot; to rush to somebody's aid; to pull outa thorn of the foot; to help; to rescue; to withdraw; to get from. Te bés, ba ma Yàlla génnee sama kër baay, may wëndeelu, dama koo waxoon ne ko: “Déglul, li ngay def soo ma bëggee xettli, mooy lii: fépp fu nu dem, nanga wax ne sa càmmiñ laa.”» [Njàlbéen ga / Gn 20.13] See: teqale. Note: plus profond que "dimbali"

xonjom y- *   n. science occulte; pratiques magico-religieuses; pratiques magiques visant à ensorceler quelqu'un *; geheime Wissenschaft; okkultes Wissen; magisch-religiöse Praktiken; magische Praktiken, die zum Ziel haben, jemanden zu verzaubern; secret science; occult knowledge; magico religious practices; magical practice aiming at bewitching someone.

xonq *   v.i. être rouge; être rouge vif *; rot sein; feuerrot sein; to be red; to be blazing red. Mu ne Yanqóoba: «Gaawe ma ci ndambe lee waay, ba ma duy sama biir ci sa ndambe lu xonq loolu, ndax xiif a ngi may rey.» Loolu moo tax ñu tudde Esawu, Edom (mu firi Xonqe). [Njàlbéen ga / Gn 25.30] syn.: deretu xaj, dàlde.